SASS WI – Recueil de Panégyriques de Cheikh Ahmadou Bamba

sass wi

Le recueil de Panégyriques de Cheikh Ahmadou Bamba intitulé « SASS WI».

17 comments

  1. thierno deme dit :

    maguii siaaree bou werr di ladjté ndakh amoul moyen pour télécharger saass wi.
    dieuredieuufaate cheikh bethio

  2. Mouhamed dit :

    amna solo lol. jajef PA ASSANE

  3. ndiouroul dit :

    mangui siar gnooko bokh

  4. D. Ousmane Camara dit :

    Li dé dina dimbali niou baré niou mel ni mane. Dieuredieufety Serigne Salaiou. cheiekh bethio Diamou Serigne Saliou yalla nafi sakh

  5. Pape Momar GUEYE dit :

    ASSALAMOU ALEYKOUM DIEUREUDIEUTY SERIGNE SALIOU MBACKE SI SEN LIGUEYE BOU TED BI YALLA NALEN KO SERIGNE BI GUENA DIAPANIL , MANANE DAMA DONE SAKOU UN LIEN GUIR MA MANA TELECHARGER SASS BI , SVP DIEUREUDIEUF

  6. santati s salihou si liiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiii

  7. Abdou dit :

    maagui ziar bu werr, su ngeen ma mané dimbali yonné ma sass bi pdf ci sama email (dieuzbu@gmail.com) dinama dimbali loolu. Jerejef

  8. Abdou dit :

    Maggaluk jamm ak xeweul

  9. Ziar dama bègue guéne envoyer ma sass wi di Diadief

  10. Abdoulaye dit :

    Magui siar bou bakh sama mbok talibe yi Di sagou âme sass bi si barke serigne saliou Fafa.gomis@Yahoo.fr dadieuf di niane serigne bi Yague fi

  11. mariama ndour dit :

    santate nagne serignbi bou wer thi yokouteyi

  12. mais kou beu gonee amm sasswi en logiel nane gaye defff

  13. sokhna mame bousso ndiaye dit :

    dieuredieufety serigne saliou
    serigne bethio diamou serigne saliou yalla na fi yag lool té geuneu weer ande ko ak cheikham yi
    di ziar bou bakh di len diadieful si li ngen def beug nio dimbali ngir niou mokal sass bi
    malen done ladj ndax meuno len ko def ba mou nek si APPLE STORE waleu PLAY STORE WALEU SI YENENE moyen de telechargement ngir niou meun ko am sougni telefone yakar na ni sou boba diang bi di na geuneu yomb geuneu gaw
    Dia ngen dieuf

  14. Mangui siar taye sogné si ndiangue khassaïdes serigne touba yi diaadieufety

  15. siare pa assane mane la pito bogué dio montaba

  16. ndeye awa soukeyena cissé dit :

    dieuredieufety serigne saliou
    serigne bethio diamou serigne saliou yalla na fi yag lool té geuneu weer ande ko ak cheikham yi
    di ziar bou bakh di len diadieful si li ngen def beug nio dimbali ngir niou mokal sass bi

    je ne peut pas faire de commentaire parce que je viens juste d’ouvrir cet site mais je suis pour avoir les
    khassidas en français

Répondre à ndeye awa soukeyena cissé Annuler la réponse.

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Vous pouvez utiliser ces balises et attributs HTML : <a href="" title=""> <abbr title=""> <acronym title=""> <b> <blockquote cite=""> <cite> <code> <del datetime=""> <em> <i> <q cite=""> <strike> <strong>