Radio

13 comments

  1. papa mambaye mbaye dit :

    dieureudieufety serigne SALIOU nio ngui rafétlou bou bakh radio bi rawatyna dioublou gui nguéne ci déff té donoul loudoul ndieuriniou askaswi yeup! rawatina nioune mourides nioune thiantakones. yalla naniou ci tassé ak mbégoum cheikh béthio té radio bi diour télé ak bépp médias bou meuneu dialalé woné yeurmandé serigne SALIOU bi souniou biir.cheikh béthio diamou serigne saliou bi yalla nafi yagg lol té andeu ko ak wérr amine!

  2. pap lo dit :

    a wawaw sant kay serign bethio kaipp dp8 istanbul

  3. je suis tres content de ndiouroul khassaid dieuwrin universel khalnga aw yon waye je sans k tu peut mieux faire je vous conseil de creuser daventage.bonne chance et pourquoi pas.

  4. Cette radio fait mon bonheur merci DU Pa Assane Diouf

  5. SOKAYE SECK dit :

    magui ziar tay wax dieureudieufety serign saliou di nianal cheikh bii mou yaggeu fii lol te weer;amineeeeee

  6. sokhna soukaye dit :

    dieureudieufety serign saliou

  7. balde dit :

    siare nalene

  8. balde dit :

    santate négne boubakh si dibali bignou s.saliou bagnou mokol ap bayite

  9. dieureudieuf serigne saliou mangui begue lol ci khassida yi diawrigne Assane Diouf di diangue;di gnanate serigne bethio mou yague fi lol te weer.

Laisser un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Vous pouvez utiliser ces balises et attributs HTML : <a href="" title=""> <abbr title=""> <acronym title=""> <b> <blockquote cite=""> <cite> <code> <del datetime=""> <em> <i> <q cite=""> <strike> <strong>