Leçon 07 : Mafaatihul Jinaan – 2ème Daadj – 78

15 comments

  1. Pa Assane liguey am na solo lol way gnoune dé sant nagn ci tay niane serigne bi guen la yok si sayir ak batine .diadieuf

  2. aamiiine yala nagnouko bokh diaadieuf

  3. THEOLOGUE GUEYE dit :

    Lii dé amna solo lol wayè thi léral bi soo co done diague thia caw com boo néké si kouréle,cqone dina gueneu lérr.

  4. mangui siar bou wer THEOLOGUE GUEYE di bék lool si conseil yi dinaako fanoo incha alah diaadieuf

  5. el hadji seck dit :

    pa assane gnoun deh dougnou tay si dila sante lol ndakh guiss nagnou niguagnouy diapelé si daj khassida yi gnoun gnigua kham ni ay ndaw lagnou disi gorgorlou sante nagnoula bou bakh sakh dila waakh ni lép diarna yone te léér na nagne dieuredieufeuti sante nagnoula basi canamou serigne saliou mbacke dila nianal nak lép lo beug rek yalla nako sougnou borom déf té yoombalal la lép loy outou si doléy serigne touba diadieuf . mane la sa sa sopé di rakou bachir seck té deuk wagou niaye so faté dieum dji merci

  6. antasaliou dit :

    Hakassa Gnoune deiy gnongui leine di suivre de pres Pa Assane. Liguey bi amna solo lol en plus gnongui si beneficier wou bou bax
    Dafa am ay details yo xamni base la soko rater keimane..
    Mane deiy SAMP yi mankoy sakou thi yow sou meunei neik
    Yalla Serigne Bethio yokou.leine banguene yeuk ko barki SERIGNE SALIOU

  7. Santâte nanou serigne saliou sisa djeum dji akk tawfekh gui serigne saliou diaralee sisa djeum djii si xassaide yii..niougui sant nioune gnii âme tawekhou dila tewlou..wayee yitewonane daadjou 71 yi akk si banne daadji lannou warrdii rajaaasee???yala nafi cheikh bethio yag têe weerr

  8. mbacke diop dit :

    Diadieuf Diewrine beknanou CBT yagfi t wr.

  9. Dwr Djiby dit :

    Akassa Dwr U Pa Assane santate nanou Serigne bou bakh.

  10. mane serigne cisse by lay settt te mounoumako guisse

  11. sokhna soukaye dit :

    DIEUREUDIEUF CHEIKH PA ASSANE.

Laisser un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Vous pouvez utiliser ces balises et attributs HTML : <a href="" title=""> <abbr title=""> <acronym title=""> <b> <blockquote cite=""> <cite> <code> <del datetime=""> <em> <i> <q cite=""> <strike> <strong>