Leçon 06 : Mafaatihul Jinaan – 2ème Daadj – 78

7 comments

  1. Max dit :

    akassa sant bubax!

  2. siar dwr.dama bgone nguene wakh ma noumay df ba meune way yi nk si thiatou khab yi manam si rim bi.yi tai wonako loll sakh barke srn Saliou.damay sentir sassou may diangu,diague bi dou wayou.diadieuf dwr yokk ak ndam

  3. s saliou diouf dit :

    yalla na serigne bi yogue xam xam bi ak beugeu diadieuf

  4. Kourel Sokhnas Touba Paris dit :

    Lepp lérrna Diewrigne!Sant nagnou ci bou weer! Di gnane Serigne bi défal lénn ndame ci ligueyy , té fayy lénn senn dieufs diou reuyy dji .
    Diadieuf!

  5. el hadji seck dit :

    pa assane haaa gnoun deh geun nagnou contane si yaw lol sakh bilahi mbeg té bima am ni sédé nako si serigne saliou mbacké yalla nala sougnou borom béguelé lou eup lolou ndakh léral yi dal mom amouma loumasiy contribuer lép diar yone ndakh nidé lako khamé té gnoun dagnouy ay ndongo yo kham ni dagnou geustou rek si khasida yi dignane sougnou borom defal lép lo beug si yoon bi ak lép lo beug sisa khol vraiment am na mbeg té lol si leral yi mane deh damay gueneu diang rek si yaw ndakh mane yaw la roy diadieufeti . mane la aladji gueye di rakou bachir seck ak djily seck bi deuk wagou niaye so fatalikouwoul dieum dji diadieufeti

  6. Waaaw beeknanu loool waay wa touba Piacenza italie yeup gningi deglu radio souba AK gooneu maguette mbaye

Laisser un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Vous pouvez utiliser ces balises et attributs HTML : <a href="" title=""> <abbr title=""> <acronym title=""> <b> <blockquote cite=""> <cite> <code> <del datetime=""> <em> <i> <q cite=""> <strike> <strong>