Leçon 03 : Mafaatihul Jinaan – 1er Daadj – 78

5 comments

  1. NIANG dit :

    Dieureudieuf yalla nalla Serigne bi fay

  2. DjibrilGueye dit :

    lèr na dé diadieuf way

  3. lii deh dafa ammeu solo tei doomou adama bounei warna thie deff ay dieego ndakh lii dafa yamoul akk dara yalla naleene kou tedd ki taxawou tei fadj aaadjo yeupp thie barkep MOUHAMED

  4. alioune waly ndiaye dit :

    siarnala sam ndiatigué.
    dam beug indi Ben suggestion bou touti rek ci Bayrou bi:

    nâjaytou zâl la araf bi indi au lieu de nâjaytou zal

    donc prononciation zâl bi c’est plus soutenu que dans ce cas ci; c’est à dire wax ji (“zâl” bi) dafay continuer, dou dab.

    jajeuf

    • alioune waly ndiaye dit :

      siarnala sam ndiatigué.
      dam beug indi Ben suggestion bou touti rek ci Bayrou bi:

      nâjaytou zâl la araf bi indi au lieu de nâjaytou zal

      donc prononciation zâl bi c’est plus soutenu que dans ce cas ci; c’est à dire wax ji (“zâl” bi) dafay continuer, dou dag.

      jajeuf

Laisser un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Vous pouvez utiliser ces balises et attributs HTML : <a href="" title=""> <abbr title=""> <acronym title=""> <b> <blockquote cite=""> <cite> <code> <del datetime=""> <em> <i> <q cite=""> <strike> <strong>