Leçon 01 : Mafaatihul Jinaan – 1er Daadj – 78

10 comments

  1. ngom babcar dit :

    Bonne continuation

  2. Maguette SARR dit :

    Waw lii dé amna solo trop ! Santaat nagn ci cours yi gnoune gnii di jang té mokalagougn ! Yalla na Serigne bi mottali yééné yi, yokk xam xam bi !

  3. awa diouf dit :

    wawaw sante na bou bakh li d dimeli nama cheikh bethio rék

  4. Max dit :

    akassa jewrine yalla na lep done ay yokute !

  5. SOKHNA NDACK MU CHEIKH BETHIO dit :

    diadieff pa assane si ndiangue mii sa yalna serinbi motalii yénaii yii amine

  6. elfeki dit :

    Yalna SERIGNE BI takhawou len te guen nio dimbali sant len rek si liguen niouy dimbali yalna sakh ba diarigne nieup si barkep CHEIKH BETHIO

  7. kandji diao dit :

    sant nane dieuwrine…. lii dafa melni niun rek ngeen ko defal W
    a touba linguere ndakh lunu mankee lawoon diadieuf yalla nalen SERINE TOUBA guena yook DIADIEUF

  8. Issa Saka dit :

    Thiey Serigne Saliou! Sene taxawaye rafete na lole. Yalla na lene Serigne bi doli tawfeex si barkep Cheick Bethio!!!

  9. bamba lo dit :

    akasa amna solo

Laisser un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Vous pouvez utiliser ces balises et attributs HTML : <a href="" title=""> <abbr title=""> <acronym title=""> <b> <blockquote cite=""> <cite> <code> <del datetime=""> <em> <i> <q cite=""> <strike> <strong>