Initiation à la lecture de la langue arabe

Composée de 6 leçons et écrite d’une manière accessible à toutes les couches sociales, cette œuvre qui est un condensé de l’alphabétisation en langue arabe (version warse), tient compte des apprenants, de leur niveau d’instruction en français, langue officielle du Sénégal, de leur classe d’âge, mais aussi de leur disponibilité afin de résorber ce gap linguistique.

GDE Erreur: Erreur lors de la récupération du fichier - si nécessaire, arrêtez la vérification d'erreurs (429:Too Many Requests)

14 comments

  1. dame dit :

    akassa amna solo lol

  2. NIANG Aïda dit :

    bégue naniou lool si site bi, yalnalène SERIGNE BI yoku tawfekh ba nieup meune si dieuriniou, mane dé sante nassi boubah, diadieuf.

  3. dieye khady dit :

    Siar tey ame sague ak begue lol si site bi di gnane kou TED KI gueune laine tek lokho guéne diko gueuneu meune ndakh gneup meuneu diarignou diaguéne dieuf

    • gningui sant bou baakh si visite bi nguéne di déf si site bii ngua khamni gnoune nieup niooko bokh di niaane loolééne si guisse rek lougnou wara défaraat gningui léne di déglou diaadieuf

      • NDEYE ARAME BADIANE dit :

        MANGUI SIAR BOU WER MOURID DI CONTANE LOL SI SEN LIGUEY BOU SELE BI! SANTNAN LOL SI DIANGALE LIRE ARABE BI NGUEN DI DF, AH DI SAKOU REK SOU MENE NEK NGUEN YOK SI VIDEO POUR YOMBAL PRONOCIATION MOTS ARABES YI NDAH BOY LIRE FRANCAIS BI DAY HAWA WOUTE TOUTI AK ARABE BI. DIANGUENDIEUF!!!

  4. Gningui siar sokhna si taye sant bou baakh si takhaway bi inchalah fasse nagnouko yéné tamali si février bii inchalah gningui sant ta dilene wakh ni looléne si guiss rek wakh léne gnou diaadieuf

  5. Mame Bousso dit :

    Ziar, tu parle anglais? Tu apprendes ls xassaida Foutzi?

  6. saloum yalli dit :

    Mangi siar bou bakh di santate bou bakh si sen takhaway si khasida yi. Mouy melni bek nagnou si niguen di lerale ndiangu mi.di sakou si bougnou meune ame ndiangoum mwahibou.

  7. Amadou Diaw dit :

    Dia Ghén Dieuf mouride. Liguéy bi rafetna

  8. Alioune Faye dit :

    Dama beugue idji

  9. sokhna Faty NIANG dit :

    Assalamou alékoum
    Siar DIEWERINE
    Site bi amna solo lolou , gnoune mouride khassidas moye sougnou gneurine, bégue na lolou,di santate Serigne bi diko gnianal télaye gnianal tamit…..
    DIEUREUDIEUFFF SERIGNE TOUBA!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!!

Laisser un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Vous pouvez utiliser ces balises et attributs HTML : <a href="" title=""> <abbr title=""> <acronym title=""> <b> <blockquote cite=""> <cite> <code> <del datetime=""> <em> <i> <q cite=""> <strike> <strong>